Xelkoom

Xelkoom Xelkoom, l'horizon commercial s'eclaircit. L'intelligence au service du développement.

DOX DAJE Ñakk xam nit teewul nga am yëg-yëg ci nit ki wala nit yi.Gis bég am na gis texe am na. Mbégte mënul yee lu dul ...
04/06/2026

DOX DAJE
Ñakk xam nit teewul nga am yëg-yëg ci nit ki wala nit yi.
Gis bég am na gis texe am na. Mbégte mënul yee lu dul mbégte.

MUNAANdar la ñu tase. Ca  mu koy bàyyi xel. Nit ku baax te am seetlu. Jàng naa ci moom lu bare. Xam naa sax du mën xam l...
25/05/2026

MUNAA
Ndar la ñu tase. Ca mu koy bàyyi xel. Nit ku baax te am seetlu. Jàng naa ci moom lu bare. Xam naa sax du mën xam li may wax waaye xam ne ne lu baax laa seede ci moom.

MUNAAKu baax ci biir ak ci biti. Déggul làkk wi waaye xam na wax yi. Nit ku baax . Jàngal nama lu bare ci diir bu gatt. ...
25/05/2026

MUNAA
Ku baax ci biir ak ci biti. Déggul làkk wi waaye xam na wax yi. Nit ku baax . Jàngal nama lu bare ci diir bu gatt. Teewlu ni ma jafee

19/05/2026

Riiru liy dundu
Échos du Vivant
Riiru liy dundu invite une réflexion sensible sur la musique comme présence invisible traversant les corps, les espaces, les mémoires et le vécu. À travers la photographie et l’installation, l’exposition explore la manière dont le rythme habite le vivant bien au-delà du son lui-même. Ici, la musique n’est pas uniquement entendue : elle se ressent, traverse les gestes, les silences, les souffles et les paysages. Avant d’être divertissement ou performance, la musique fut et demeure une manière d’habiter le monde. Elle accompagne les corps dans le travail, la prière, l’exil, les rassemblements et les moments de solitude. Elle façonne les mémoires collectives autant qu’elle traverse les expériences intimes. Invisible, elle laisse pourtant des traces : une cadence dans un mouvement, une vibration dans un regard, une présence dans le silence.
Les œuvres réunies dans cette exposition prolongent cette idée de la musique comme force vivante et circulation intérieure. Avec « Xidma », Xelkom inscrit le rythme dans le geste du travail et dans l’esprit Baye Fall. Les chants collectifs deviennent ici des respirations communes, des formes d’élévation où l’effort se transforme en cadence spirituelle. La musique apparaît alors comme un rappel, une acceptation et une manière de se relier à quelque chose de plus grand que soi.
Cette traversée continue avec « Ngelaw » de Noreyni, où le vent devient langage sensible. Le souffle y transporte les idées, les intuitions et les mélodies invisibles qui traversent les êtres avant de disparaître ailleurs. Le vent joue ici une musique silencieuse, perceptible uniquement à celles et ceux capables d’habiter pleinement l’instant. La vibration devient alors fragile, mouvante et insaisissable.
Avec « Yeg-yeg », Diariatou propose une approche plus intérieure du rythme. Les images deviennent sensations, fragments émotionnels et mémoires sensibles.
expositions

MBEDD Koo xam siyaaral. Koo xamul wormaalal. Mbedd bi ëmb ni nit ëmb na boroom daraja. Mbeddum buur bi la te dencam yi d...
19/05/2026

MBEDD
Koo xam siyaaral. Koo xamul wormaalal. Mbedd bi ëmb ni nit ëmb na boroom daraja. Mbeddum buur bi la te dencam yi daa yaatu.

BAAY AMU ÑU SA FAY.Yaw de ku la gis xam ne waroon ngaa dallu weer say galañ bu yàgg. Njaboot rek a la bàyyi ci bii tund....
18/05/2026

BAAY AMU ÑU SA FAY.
Yaw de ku la gis xam ne waroon ngaa dallu weer say galañ bu yàgg. Njaboot rek a la bàyyi ci bii tund. Daw nga ba màgge. Waroon na ñu laa wuutu bu yàgg xanaa kay nga dolli ñu ñaanal. Say dàll jot na ñu bu yàgg. Ñu ngi sàkku sa barke.

YAAY BÒOYNdeysaan kañ rek ngay dallu yaay. Yaay seede naa sa taxawaay CI njaboot fi. Su doon Liggéey kepp mooy maye xéew...
17/05/2026

YAAY BÒOY
Ndeysaan kañ rek ngay dallu yaay. Yaay seede naa sa taxawaay CI njaboot fi. Su doon Liggéey kepp mooy maye xéewal ci ñeenti fukki at am nga lépp. Ñu ngi lay fasal sa coono yam fii ci du yaa.

Lu wàccul kenn.Dee leen jàng Alqur aan ndax sunuy lim jullit yi boole leen ci. Koo gis muy réccu li tax makkalul xaar ko...
14/05/2026

Lu wàccul kenn.
Dee leen jàng Alqur aan ndax sunuy lim jullit yi boole leen ci. Koo gis muy réccu li tax makkalul xaar ko ci doomam. Su wàccul réccu wa des na.

Loo gis mbir mu nkk ku nekk am na ci mbir.
12/05/2026

Loo gis
mbir mu nkk ku nekk am na ci mbir.

YAAY WÀCC NAA.Yàgg na yàggul waaye li gën laa jàpp ci li am njariñ. Amu ma seen fay. Damaa foogoon ne da ngeen ma bañ. W...
12/05/2026

YAAY WÀCC NAA.
Yàgg na yàggul waaye li gën laa jàpp ci li am njariñ. Amu ma seen fay. Damaa foogoon ne da ngeen ma bañ. Waaye Bëgg naaleen. Desee la too leen ma dara. Maa leen deseel. Léegi nak mën naa jang àdduna.

Adresse

HLM Grand Yoff
Dakar

Téléphone

+221776251203

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Xelkoom publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Xelkoom:

Raccourcis

Partager